Tass Yakar
WO

Songtext von Tass Yakar

GenreSamba Enredo
OriginalspracheWO
Aufrufe31
AaLeseeinstellungen
Textgröße 18

Originaltext

WO
Noch keine Übersetzung verfügbar. Der Originaltext wird angezeigt.
Wagni lène ki Sa bay wagnila sa yaye wagnila Yaw ngani ya bagne Way dégueul lii Sa yaye wagnila sa bay wagnila Yaw ngani ya bagne Bo khamone do dokholè ni nagua Soralé euleuk digua yori sa diabot yaw Say wadiour lou bakh lagn la digueeul Bougnou sagnone ken doula gueun Kon lou bakh lagn la yéné Kon bok euleuk boul retiou nane Sama yaye yé Sama yaye boy sorina foumakay dioyé Sama yaye yé Sama yaye boy sorina foumakay dioyé Koulané senguoul sa taar lala beugueul Mané wadiour bolen défé kharit yaw Domassa lal souf Am bouki mané yombana lol Wayé bou mana khalam mo diafé Say wadiour lou bakh lagn la digueeul Bougnou sagnone ken doula gueun Kon lou bakh lagn la yéné Kon bok euleuk boul retiou nane Sama yaye yé Sama yaye boy sorina foumakay dioyé Sama yaye yé Sama yaye boy sorina foumakay dioyé Sama yaye yé sama yaye boy sorina Foumakay dioyé Bo bougué mouthia dagay téral say wadiour Sama yaye yé sama yaye boy sorina Foumakay dioyé Bo nanguo bakh nagua dégueul say wadiour Haléyi fofou lagnou rawanté Ndakh wadiour kouko lébal Bour yala fayla ba dolila yaw Bo défé béneu am gnare Bo défé gnare am gnint Bo défé gnint am fouk Bo mané témère gnagua téral say wadiour Bo mané témère gnagua téral say wadiour

Mehr von Ismael Lo

Ismael Lo →

Ähnliche Songtexte