Soma Woraté
WO

Paroles de Soma Woraté

GenreAfrobeats
Langue originaleWO
Vues9
AaLecture
Taille 18

Paroles originales

WO
Traduction indisponible. Les paroles originales sont affichées.
Yeksil, déloussil, limey ndiorte néxoumay Limey dégeu souma lérré baby dotoko défati Yeksil, gnibissil, limey ndiorte néxoumay Limey dégeu souma lérré baby dotoko défati Hannnn hannn hannnn Baby dotoko défati Hannnn hannn hannnn Baby dotoko défati Boy limey dégeu mbadou deugeula Sou amé rek néma deugeula Khalé bi ci kogn bi dagko biralate Dégeunané baby ioe deh yafa diar Faté diapone nala ngey dokhane Téwoul ma ngui tokk mane dila mougnalate Soma waraté, dina takali sa bop ak sa bate Soma waraté, baby may koulay diongalate Soma waraté, dina takali sa bop ak sa bate Soma waraté, baby may koulay diongalate Sama baby légui dafay am guel Souma waxé moumey diéma tek khel Souniou éguer baby nala Watt ndél, boul faté denthial nala béna yatou kel Loy wouti fénén kholal nima taroo yeah, yeah, yeah Loy wouti fénén kholal nima dionguama yeah, yeah, yeah Loy wouti fénén kholal nima séxé yeah, yeah, yeah Baby dafa doy, bougouma sa lay Bala may déh ngay hay hay Lo def yako tay bougouma sa lay Bala may déh ngey hay hay Baby dafa doy, bougouma sa lay Bala may déh ngay hay hay Soma waraté, dina takali sa bop ak sa bate Soma waraté, baby may koulay diongalate Soma waraté, dina takali sa bop ak sa bate Soma waraté, baby may koulay diongalate Sama baby légui dafay am guel Souma waxé moumey diéma tek khel Souniou éguer baby nala watt ndél Boul faté denthial nala béna yatou ke Loy wouti fénén kholal nima taroo yeah, yeah, yeah Loy wouti fénén kholal nima dionguama yeah, yeah, yeah Loy wouti fénén kholal nima séxé yeah, yeah, yeah Mane tay warouna, ci goorou tay yi Képeu ki ci naane di neubeutou Biss bo mandé rek da ngey fégn Hannnn hannn hannnn Biss bo mandé rek da ngey fégn

Plus de Queen Biz

Queen Biz →

Paroles similaires