À l'infini
WO

Testo di À l'infini

GenereHip Hop Rap
Lingua originaleWO
Visualizzazioni37
AaLettura
Dimensione 18

Testo originale

WO
Traduzione non ancora disponibile. Mostriamo il testo originale.
Bëgg naa nga jege ci ma Wax ma loo yëg ci sa xol Te boo ñëwul ma fekk ci la Wax la li ne sama xol Ñun ñaar rekk a wet Bude mbëggeel bi lañuy dundal Baby amul lu ñuy xaar Nel waaw, bul ne déet Takk na fit bi fekk ci la waroo tas sama yaakaar Ndax yaay sama number one Di sama saajooban Takk la sama jabar Pur muy continuer Man ak yaw à l'infini À l'infini, à l'infini Pur muy continuer Mar naa naan nga jox ma ndox Boo xiifee mbëggeel laa lay jox Arroser xol bi ak limonade Neen ko dundu te Yàlla tax Sa xol bi yépp nga ma jox Tep tep ñuy dox Bude am na ñu bëggul bàyyileen kon ñu yox Sa life da fees ak mbëggeel Wane nga ma ko ci pete Yaa ngi ci xol ak xel Yaw yaay diamants bune dul weccoo ak or (Non, non, non) Bum leen presenter ñépp d'accord (Bae bae bae) Yaay sama number one Di sama saajooban Takk la sama jabar Pur muy continuer Man ak yaw à l'infini À l'infini, à l'infini Pur muy continuer

Altro di ISS 814

ISS 814 →

Testi correlati