Djiguene
WO

Djiguene 歌詞

ジャンルPop
原文言語WO
閲覧数33
Aa表示設定
文字サイズ 18

原文歌詞

WO
翻訳はまだありません。原文を表示しています。
Sopp naa la, yaw jaambaaru kër gi Yaw mi toppatoo kom-kom mu tool Yaw mi yar xale yi Di sar jàngoro gi Sopp naa la, yaw jigéen ju laxu ji Yaw mi xeex ngir nit moom boppam Yaw mi xeex ngir jàmm ji yàgg lool ci kaw sof Yaw yaay su moo yaakaari ëllëg Han jigéen Afrique Jigéen àdduna Jigéen Europe Jigéen, mùso, gnonnon, jigéen, femme Jigéen, mùso, gnonnon, jigéen, femme Jigéen, mùso, gnonnon, jigéen, femme Jigéen, mùso, gnonnon, jigéen, femme Sopp naa la yaw jigéen bu am-sutura bi Yaw mi ndeyu njirim yi ñàkk ndey, ñàkk baay Yaw mi am-yërmandé te tabe Yaw yaa tax gune yi yee feexe Yaw yaay mbëggeel jër made Yaw yaay yaakaar di bidéew Yaw yaay kiiraay gune yi Yaw yaay yaakaari ëllëg Yaw mi xam cosaan Jigéen Afrique Jigéen àdduna Jigéen, mùso, gnonnon, jigéen, femme Jigéen, mùso, gnonnon, jigéen, femme Jigéen, mùso, gnonnon, jigéen, femme Jigéen, mùso, gnonnon, jigéen, femme Mama sa, eh Mama sa, oh Mama sa, eh Mama sa, oh Jigéen, mùso, gnonnon, jigéen, femme Jigéen, mùso, gnonnon, jigéen, femme Jigéen, mùso, gnonnon, jigéen, femme Jigéen, mùso, gnonnon, jigéen, femme

Dobet Gnahoré の他の曲

Dobet Gnahoré →

関連歌詞