Tristesse
WO

Tristesse 歌詞

ジャンルHip Hop Rap
原文言語WO
閲覧数9
Aa表示設定
文字サイズ 18

原文歌詞

WO
翻訳はまだありません。原文を表示しています。
Bou féké lim la wax daf la féxé Meun nga dem sa yoon grawoul Bou fékè louniouy doundou daf ley stréssé Meun nga dem gnibi thioloul Mais ma gui ak tristesse tristesse Bayé mak sama tristesse Bayé mak sama tristesse Hé damla beug té y'allah tax, yeah! Khalé bi, mounouniou nek té douniou wax Hé, sokhna si, koula beug nga def ko noone Hé, ndeysanne, diougal nga dem sa yone Souma ndanane Khamna ni nala manquer Ay way! Ioe tamit dig ma manquer hannn! Bou féké lim la wax daf la féxé Meun nga dem sa yoon grawoul Bou fékè louniouy doundou daf ley stréssé Meun nga dem gnibi thioloul Mais ma gui ak tristesse tristesse Bayé mak sama tristesse Bayé mak sama tristesse Hé! Sama wax dafa méti Té da nga gawa meer Baniouy moudji xèkh fi Mane ak ioe comme ennemis guerre Démal nga gnibi mo geun si ioe Hey! Té boul niowate Beuss bouné ma deg thiow Warouniou xoulo way Souniou meer ra niou eup vitesse, té bakhoul Ya ngui dem ba fi tristesse, mais grawoul Bou féké lim la wax daf la féxé Meun nga dem sa yoon grawoul Bou fékè louniouy doundou daf ley stréssé Meun nga dem gnibi thioloul Mais ma gui ak tristesse tristesse Bayé mak sama tristesse Bayé mak sama tristesse No way! Youkheunté, saganté, kou nek dém Yan moment ci ngey nek ci probleme Khalatal boy yi Gnibissil ci keur gui Tristesse tristesse Tristesse tristesse Meun nga dem sa yonne grawoul Meun nga dem gnibi thioloul, sama tristesse

ISS 814 の他の曲

ISS 814 →

関連歌詞