Defal Ni Ñun (Xarit)
WO

Defal Ni Ñun (Xarit) 歌詞

原文言語WO
閲覧数8
Aa表示設定
文字サイズ 18

原文歌詞

WO
翻訳はまだありません。原文を表示しています。
(Nii la xarit di mel) (Nii la xarit di mel) Yaay sama doomu ndey Céy sama xarit baa ngee (Nii la xarit di mel) Doo ma waxal lu ñaaw Man gis naa fi nga ma féete (Nii la xarit di mel) Xarit jafe na, xarit jafe na Ku ci am bu baax, jëlal! Ki la bëgg di la muñal Boo ko amee jàpp cee Sama doomu yaay yaa ma ko jaral Lu ma la defal sa mbaax moo ko waral Fu la ci ndeyaak baay Fayda ci boroom la, duma nangu ku ma yab Moo tax man (kaar!) Man (ñaf!) Ku ma ci waxal dootoo ko defaati Man (kaar!) Man (ñaf!) Ku ma ci cas faw ñu règle ko Boo mënee defal ni ñun Boo mënul rombal bu ñu cas Taaluñu leen ci jamm lañuy dox Ñoo ngi liggéey liggéey Ñoo dondu sunuy maam Taaluñu leen ci jamm lañuy dox Boo mënee defal ni ñun Boo mënul rombal bu ñu cas Taal na ñu leneen ci jamm la ñu dox Maa ngi liggéey liggéey doylu Ku ma ci cas faw ñu règle ko Sèrre-moi très fort Pour que je te tienne plus fort Sèrre-moi très fort Pour que je te tienne plus fort Waccu koq poussière Fëggaatu mu jeex Ku ñu woo ci guerre ayca naañ ci déem mu neex Sama doomu yaay yaa ma ko jaral Lu ma la defal sa mbaax moo ko waral Fu la ci nday ak baay fayda ci boroom la Duma nangu ku ma yab Moo tax man (kaar!) Man (ñaf!) Ku ma ci waxal dootoo ko defaati Man (kaar!) Man (ñaf!) Ku ma ci cas faw ñu règle ko Boo mënee defal ni ñun Boo mënul rombal bu ñu cas Taaluñu leen ci jamm lañuy dox Ñoo ngi liggéey liggéey Ñoo dondu sunuy maam Taaluñu leen ci jamm lañuy dox Boo mënee defal ni ñun Boo mënul rombal bu ñu cas Taal na ñu leneen ci jamm la ñu dox Maa ngi liggéey liggéey doylu Ku ma ci cas faw ñu règle ko Sèrre-moi très fort Pour que je te tienne plus fort Sèrre-moi très fort Pour que je te tienne plus fort Yaw taalo leneen ci jaam rekk ngay doox!

Ndakhte Lo の他の曲

Ndakhte Lo →

関連歌詞