Validé
WO

Validé 歌詞

ジャンルAfrobeats
原文言語WO
閲覧数16
Aa表示設定
文字サイズ 18

原文歌詞

WO
翻訳はまだありません。原文を表示しています。
Seetoo seet, seet seet Seetoo seet Tàcculeen sama njanku jeex na Damay séy tay Tàcculeen sama njanku jeex na Damay séy, dem naa Tàcculeen sama njanku jeex na Damay séy tay Tàcculeen sama njanku jeex na Damay séy tay Seetoo seet, seet seet Seetoo seet, seet bi yegsi na Seetoo seet, seet seet Seetoo seet, seet bi yegsi na Tay yàlla ñu boole Ngir ñu séy de ngenal la Mbëggeel la bari doole Bés ni ki tay sa jabar la Bés bi ci man ni mu fore Xarit yi ñëw ak doole Sañse nga gis ni ma moole Kaay yóbbu ma art ba amore Tay la sama àjjana Li ma doon ñaan yàlla yegsi na Tay ma séyal la Pour le meilleur et pour le pire Seetoo seet, seet seet Seetoo seet, seet bi yegsi na Seetoo seet, seet seet Seetoo seet, seet bi yegsi na Lu jigéen ñi bari bari Man nga ci tànn seppi ma Tay lañ ma yàpp pur ma séy si Wax ma loo bëgg ma defal la Bés bi ci man ni mu fore Xarit yi ñëw ak doole Sañse nga gis ni ma moole Kaay yóbbu ma art ba amore Tay la sama àjjana Li ma doon ñaan yàlla yegsi na Tay ma séyal la Pour le meilleur et pour le pire Seetoo seet, seet seet Seetoo seet, seet bi yegsi na Seetoo seet, seet seet Seetoo seet, seet bi yegsi na Il m'a validé (validé) Je suis validée (je suis validée) Il m'a validé (il m'a validé) Je suis validée (validée) Tàcculeen sama njanku jeex na Damay séy tay Tàcculeen sama njanku jeex na Damay séy, dem naa Tàcculeen sama njanku jeex na Damay séy tay Tàcculeen sama njanku jeex na Damay séy tay Approchez, approchez Venez, applaudissez Viva, viva, viva! Viva, vive les mariés Seetoo seet, seet seet Seetoo seet, seet bi yegsi na Seetoo seet, seet seet Seetoo seet, seet bi yegsi na

Queen Biz の他の曲

Queen Biz →

関連歌詞