Sama Everything (part. Phillipe Ndour)
WO

Sama Everything (part. Phillipe Ndour) 歌詞

ジャンルPop
原文言語WO
閲覧数28
Aa表示設定
文字サイズ 18

原文歌詞

WO
翻訳はまだありません。原文を表示しています。
Yay sama everything, beugeul ma défal la Amouna anything té dou té ma défal la Wakh iow lo beugeu, sa baneex rek la beugeu Sama yéné défal la togal ma firila Yay sama everything, beugeul ma défal la Amouna anything té dou té ma défal la Yangui yekk sama loveu Yangui few sama loveu Li mala yéné xamnako And you know you know you know now mama (xamnako baby) Li mala yéné you know now mama (xamnalo baby) You know you know you know now maaa (xamnako baby) Xamalna ni sa domyi deff la yéné lou barri And you know you know you know now mama (xamnako baby) Li mala yéné you know now mama (xamnalo baby) You know you know you know now maaa (xamnako baby) Xamalna ni sa domyi deff la yéné lou barri Yalla ma bolék iow, yaye diourom nienti wér nga eumbouma Tey dji magg na, wathié si kow souf man ganéssina Wakhma lane nga beug, lépp ma défal la paréna Sama yéné manak zeyna ci adouna ben la Gouddou fane dé lalay nianal, yobbou la makka la yéné Magg na beug dap sa love, xamna mounoumala fay Tey yalla may sédé ci sama yéné Linga def ci nioun, yaye boy yay gained Yay sama everything, beugeul ma défal la Amouna anything té dou té ma défal la Yangui yekk sama loveu Yangui few sama loveu Li mala yéné xamnako And you know you know you know now mama (xamnako baby) Li mala yéné you know now mama (xamnalo baby) You know you know you know now maaa (xamnako baby) Xamalna ni sa domyi deff la yéné lou barri And you know you know you know now mama (xamnako baby) Li mala yéné you know now mama (xamnalo baby) You know you know you know now maaa (xamnako baby) Xamalna ni sa domyi deff la yéné lou barri Dolli ant yalla sama dom xalébi magg na Lingma yéné mangui niane buur yalla mou degu leu Pa Philippe sa wakh yeggna ci xol nekhnama Pa Philippe Viviane, yaye ak dom guén di ame Philippe Yay sama everything (yay sama adouna) Amouna anything naniou sant yalla Yangui sama loveu mangui yekk sa loveu Mangui feel sa love iow mi Oh you know you know you know now mama (xamnako baby) Li mala yéné you know now mama (xamnalo baby) You know you know you know now maaa (xamnako baby) Xamalna ni sa domyi deff la yéné lou barri Oh you know you know you know now mama (xamnako baby) Li mala yéné you know now mama (xamnalo baby) You know you know you know now maaa (xamnako baby) Xamalna ni sa domyi deff la yéné lou barri (Mar buur yacine mar, birame yacine mar) Birame ngouille alé ndiaye, so woyoul denga wara woy Ndéye sokhna sa mame, ami fall sa mame Boiba ndour sa baye, Viviane sa yayooo woyal)

Viviane Chidid の他の曲

Viviane Chidid →

関連歌詞