Waawaw (feat. Aida Samb)
WO

Waawaw (feat. Aida Samb) 가사

앨범LNN (Loo Ñeme Ñàkk)
연도2019
장르Hip Hop Rap
원문 언어WO
조회수24
Aa읽기 설정
글자 크기 18

원문 가사

WO
번역이 아직 없습니다. 원문 가사를 표시합니다.
Même si guènte damay weet Soma fassalé kanam waawaw, waawaw Samay pékhé yeupay diekh Takh ma ladj la fok ga wakh ma wakhma Wakhma, wakhma Soma diégué lépay leer Doma wanati guinaaw waawaw Yalla deff na dotoul dègne, nan Beug nala beug nala Baby kaay gnou weet, yaw kaay weetoo bae Kaay gnou weet, baby yaw kaay weetoo bae Diougueul gnou dem tok né Yaw kaay gnou weeto bae Ich ya ya yi ya, ich ya ya yi ya Baby kaay gnou weet Yaw kaay gnou weeto bae Yaw kaay gnou weeto bae Contane na lol sa bissa diote Kone tay lo diooy damakoy fadj Sonoone ga lol si liko diar Yaw sakh khamga li dou hasard Because i'm before you love me Because i'm because i'm empty into damay weet Soma fassalé kanam waawaw, waawaw Samay pékhé yeupay diekh Takh ma ladj la fok ga wakh ma wakhma Wakhma, wakhma Soma diégué lépay leer Doma wanati guinaaw waawaw Yalla deff na dotoul dègne, nan Beug nala beug nala Hmhmhmhmmmm Li né si yaw mo né si mane Yalla moko deff waawaw (hmhmhmhmhm) Li né si mane mo né si yaw Yalla moko deff waawaw (yeah) Loumay dokh di khool kénène Li si yaw dou si kénène Doumala wétio ak lénène, mbeuguèl Dou dégne, dou dégne, dou dégne waawaw Dou dégne, dou dégne, dou dégne waawaw Si guènte damay weet Soma fassalé kanam waawaw, waawaw Samay pékhé yeupay diekh Takh ma ladj la fok ga wakh ma wakhma Wakhma, wakhma Soma diégué lépay leer Doma wanati guinaaw wakhma Yalla deff na dotoul dègne, nan Beug nala beug nala

Dip Doundou Guiss의 다른 곡

Dip Doundou Guiss →

관련 가사