Penalty
WO

Penalty 가사

장르Hip Hop Rap
원문 언어WO
조회수10
Aa읽기 설정
글자 크기 18

원문 가사

WO
번역이 아직 없습니다. 원문 가사를 표시합니다.
Homme de tenue bëgga dunde corruption Entreprises di sànni déchets pollution Jox la ndombog-tànk defoo résultats Président bu bëgg ñetti mandat Entreprise jékki téj Gestionnaire kepp kese Hôpital morgue dëj Bés bu ne néew bu bees Civisme bu ci mbedd mi Naan kafe sànni casse Problèmu jàng bu weesu na syndicat Waar mbit waara mbit Arbitre du sol dix Capitaine du sex mbiib Loo yor maraakiis Crampons du tarxiis Surface ralentir Hors-jeux mu naan but Looy xaar penalty Penalty! Arbitre siffléwu ko ñi ci ban bi ñoo ko mbiib Penalty! Boo nekkee njiit Defoo li la war yépp ñi nga jitte ñoo koy mbiib Penalty! Alalu njirim bi nga tëdd def sa noce Lu ñépp bokk yaw nga jël ko def sa poche Sa xaritu benn bakkan am lu baax nga mer Puusal fëlé yaw de am nga dal no mel Toj sa math te dellu klaas, moo gën ngay Toj sa mbarik mu naan tas, yaw doom nday Système bi yérémul kenn Mësu la bëgg tuur drét Fexeel ba jafandu fenn Ne naa la dëgg du fen Député Ñu fay la weer yaw ngay nelaw Assemblée! Monsieur le Maire Jaay na suuf ci wax ma xale yi fu ñuy fowe? Waar mbit waara mbit Arbitre du sol dix Capitaine du sex mbiib Loo yor maraakiis Crampons du tarxiis Surface ralentir Hors-jeux mu naan but Looy xaar penalty (jugal!) Penalty! Arbitre siffléwu ko ñi ci ban bi ñoo ko mbiib Penalty! Boo nekkee njiit Defoo li la war yépp ñi nga jitte ñoo koy mbiib Penalty! Day kas, nañ ko vare ralentir Day kas, nañ ko vare ralentir Day kas, nañ ko vare ralentir Mu jokk day kas, nañ ko vare ralentir

ISS 814의 다른 곡

ISS 814 →

관련 가사