원문 가사
RO번역이 아직 없습니다. 원문 가사를 표시합니다.
Wéétoo, wéétatinaa yaay
Wéétatinaa, wéétatinaa, wéétatinna yaay
Sophie demna tey ma dabiko
Sainte-Marguerite sorina tey ma dabiko
Sophie demna, moommii nëwna, moommi demna nii
Sophie demna, moommi newna moommii demna nii
Sophie demnaa tey ma dabiko
Sainte-Marguerite sorinaa tey ma dabiko
Demnaa fimu dem sorinaa sana guel demnaa yow
Fimu dem sorinaa tey ma dabiko ndeysaay