Wérouway
WO

Wérouway 가사

장르Pop
원문 언어WO
조회수63
Aa읽기 설정
글자 크기 18

원문 가사

WO
번역이 아직 없습니다. 원문 가사를 표시합니다.
Waat naa duma la trahir Su ma xeexeek yaw damay gaañ Teyit seet naa la fu ne Wër nañu ba tase du neen, han Cér bi nga ma jox dafa matt sëkk Yaay sama bët-set bi laa doon xaar ci yaw (wuy) Yaay ki may bégal Lalal basaŋ, talalal Li ma doon wër ci biir dëkk Yaa ma koy jox wéeruwaay (aah!) Bu ma yërëm na ma dal Xanaa ma doon sa wéerukaay Li ma yor de yaa ko moome Yaa may daaneel, duma la bàyyi waay! Bu ma yërëm na ma dal Man, xanaa ma doon sa weccookaay waay! (Wuy sama!) Li ma yor de yaa ko moom Yaa may daaneel, duma la bàyyi Sa buum bi lonk ma ko Diri ma man ba Japon Bàyyil ma dead say loxo, my love Parfum bu neex laay turoo Xaaral ba jant bi so Bu ginnaar sapp naan kooko (ah, ay!) Nga di ma def lu ma dul nettali Yaw kaay wax ma ku la jàngal yii Yaay ki may bégal Lalal basaŋ, talalal Li ma doon wër ci biir dëkk Yaa ma koy jox wéeruwaay (aah!) Bu ma yërëm na ma dal Xanaa ma doon sa wéerukaay Li ma yor de yaa ko moome Yaa may daaneel, duma la bàyyi waay! Bu ma yërëm na ma dal Man, xanaa ma doon sa weccookaay waay! (Wuy sama!) Li ma yor de yaa ko moom Yaa may daaneel, duma la bàyyi Su ma reeree Ma ree Su ma reeree Yaay ki may bégal Lalal basaŋ, talalal Li ma doon wër ci biir dëkk Yaa ma koy jox wéeruwaay (aah!) Bu ma yërëm na ma dal Xanaa ma doon sa wéccookaay, waay Li ma yor de yaa ko moome eey, waaw Bu ma yërëm na ma dal Xanaa ma doon sa wéerukaay

Mia Guisse의 다른 곡

Mia Guisse →

관련 가사