Yole (feat. Ndobine Groove)
WO

Yole (feat. Ndobine Groove) 가사

장르Regional
원문 언어WO
조회수16
Aa읽기 설정
글자 크기 18

원문 가사

WO
번역이 아직 없습니다. 원문 가사를 표시합니다.
Yow kay ma netali lenn noy, ben histoire boumafi dalon Samdie soir may seti, sama xalé bou bess bi Beuss bobou lamaci daal mane faw ma nétali len ko Bama yégué sa keur ga niou terrou ma, nignuy tero buur Tallal ma thiouray teegal ma reer bu neex dall may goonal Bamou dess loudoul gnibi, ma andeu ak xalé bi, moumay goungué Bama démé sa mbeed mi, né xaral ma tagato ak mom diokh ko ben calin Guestou yam si Amy, Amy rakou lily sama benen geel bi (sheuteuh teuh) Mane thiolé na, ndax Amy dianama yolé yolé, mba douma yolé yolé Thiey fouma dieum, ki dinama yolé yolé Mba doma yolé yolé, may xallat ndax doma yolé yolé Xalé bi dinama yolé yolé, xamna dinama yolé yolé Diamono dji thiey ndoumba lame Mangui sangou tewoul samay tank di fegn Du nétali sakh way loumou yeug mou siw Néna mur yi sakh, niom dagniy wax téléphone yi di gnofi daka yolé Yolé yolé yolé, hé mba doma yolé yolé, xalé bi dinama yolé yolé Thiey fouma dieum ki dinama yolé yolé Wouy fouma dieum ki dinama yolé yolé Sayou foor yombé rek, seug diafé wawaww Kham na sou ndiab yaggué légui gawar fegn Wooh wooh wooh Leeh leeh leeh leeh Sa deugeu deugeu deugeu nak

Momo Dieng의 다른 곡

Momo Dieng →

관련 가사