Contigo
WO

Contigo 가사

장르Hip Hop Rap
원문 언어WO
조회수6
Aa읽기 설정
글자 크기 18

원문 가사

WO
번역이 아직 없습니다. 원문 가사를 표시합니다.
Deff Music Contigo Contigo Contigo Contigo Contigo Contigo Contigo Contigo Tigo Contigo Bailar contigo Bailar contigo Contigo Tigo contigo Vivir contigo Vivir Contigo Mane yaay sama garap Iow la kima faral Boul ragal dara dara Xel mi yawa Xol mi yawa Miss dagama diaral Thia mbeuguel bala Sama ding dong chabalaba Xol mi yawa dong dong dong Togal sama weet Bouma ba ma dem Nieuwal sama way Toknaa dila wait Pourniou and dem Beugouniu mou wey Waayé anyway Faatel la sa demb Sambal la tay Soubeu dineu neex Contigo Tigo Contigo Bailar contigo Bailar contigo Contigo Tigo contigo Vivir contigo Vivir Contigo Boum chakalaka boum chakalaka boom boom Boum chakalaka boum chakalaka boom boom Boum chakalaka boum chakalaka boom boom Boum chakalaka boum chakalaka Boum chakalaka boum chakalaka boom boom Boum chakalaka boum chakalaka boom boom Boum chakalaka boum chakalaka boom boom Boum chakalaka boum chakalaka Maag si iow yag si mane Bou souf si cedd yaamay yoobou assaman Yaamay wathié beugoo sama khol di tang Lokhok lokho sama tank ak sa tank Ndakh nioo maneu and Yeeneu saay ma diaad Si iow lay délou loumou yaag yaag Doo faalé djitt boo meuné diap diaan Iow laa taneu defla star sama guèn waleu Loumay wouti fenen mbeuguel dou nenen Lenen si kenen m'everve Bouma démé sans nga teew dou benef Nek fenen foodoul nek dou ngueuneel Loumay wouti fenen mbeuguel dou nenen Lenen si kenen m'everve Bouma démé sans nga teew dou benef Nek fenen foodoul nek dou ngueuneel (Boom chakalaka, boom chakalaka) Contigo Contigo (Boom chakalaka, boom chakalaka) Contigo oh Contigo (Boom chakalaka, boom chakalaka) Contigo Contigo (Boom chakalaka, boom chakalaka) Contigo oh Contigo Tigo Contigo Bailar contigo Bailar contigo Contigo Tigo contigo Vivir contigo Vivir Contigo Boum chakalaka boum chakalaka boom boom Boum chakalaka boum chakalaka boom boom Boum chakalaka boum chakalaka boom boom Boum chakalaka boum chakalaka Boum chakalaka boum chakalaka boom boom Boum chakalaka boum chakalaka boom boom Boum chakalaka boum chakalaka boom boom Boum chakalaka boum chakalaka boom

OoThenTiK Zeus의 다른 곡

OoThenTiK Zeus →

관련 가사