Sama Lumière
WO

Sama Lumière 가사

장르Afrobeats
원문 언어WO
조회수33
Aa읽기 설정
글자 크기 18

원문 가사

WO
번역이 아직 없습니다. 원문 가사를 표시합니다.
Prés de toi ouais le temps il s'arrête Mon coeur ne tient plus, là il bat plus fort Accroche toi à moi, je ne veut que toi déé Car dans tes bras je deviendrais le plus fort Dans cette vida j'ne pourrais vivre sans elle Elle est devenue mon médicament Mon coeur ne bat que pour toi Pour toi, mon amour Yaw yaay sama lumière Tudde naa la sama lingeer Jëlal xol bi yóbbu dem Li moo neex cey mbëggeel Yaw yaay sama lumière Tudde naa la sama lingeer Jëlal xol bi yóbbu dem Li moo neex cey mbëggeelooy Héé chérie coco Héé misise lovely Dama dof ci yaw, miir ci yaw Ba loo ma wax moom laay def wax waaw Héé ma chérie coco Héé ieo misie lovely Dama dof ci yaw, miir ci yaw Ba loo ma wax moom laay def wax waaw Jëlal xol bi yóbbu dem baby yaa ko Jëlal xol bi yóbbu dem baby yaa ko Jëlal xol bi yóbbu dem baby yaa ko Jëlal xol bi yóbbu dem baby yaa ko Bul ma xool yaw, wan ma ko Moo gën nga may saagaane Wan ma sa mbëggeel yaw Wan ma sa mbëggeel yaw (yeah) Yaw yaay sama lumière Tudde naa la sama lingeer Jëlal xol bi yóbbu dem Li moo neex cey mbëggeel Yaw yaay sama lumière Tudde naa la sama lingeer Jëlal xol bi yóbbu dem Li moo neex cey mbëggeelooy

관련 가사