WURUS (Version Mbalax)
WO

WURUS (Version Mbalax) 가사

장르World Music
원문 언어WO
조회수35
Aa읽기 설정
글자 크기 18

원문 가사

WO
번역이 아직 없습니다. 원문 가사를 표시합니다.
Yay sama adouna, oh, yeah Sama baby coco waay, ey yeah Yow yay sama aldiana My love, sama baby coco waay, hmm yeah Baby yay mane Teudeul nèlaw kham gni moununj dara I don’t give about mèrr katt fadjoul dara Takal la or ba ci 24 carats Dagn lénn di bayèkk peureum bi Gnom gnouy deukké aya Baby, I just want real love Real love, I just wanna know real love, definitely, I don't wanna lie Yay sama adouna, oh, yeah Sama baby coco waay, ey yeah Yow yay sama aldiana, my love Sama baby coco waay, hmm yeah Way way way way Mèrr bi fadjoul dara Mom fadjoul dara Konn fadjoul dara Baylènn té gneuw ma takal la or 24 carats Wurus 24 carats Ngualam 24 carats Khana dou mala yèenè Ma vie, ma vie Don't lie to me Su fekeh guiss nga ci man lo musuta guiss ci kenen baby dawwsil gaww Ba takh mani la baby dawwsil gaww Baby yay mane Teudeul nèlaw kham gni moununj dara I don’t give a fuck mèrr katt fadjoul dara Takal la or ba chi 24 carats Dagn lénn di bayèkk peureum bi Gnom gnouy deukké aya Baby, I just want real love Real love, I just wanna know real love, definitely, I don't wanna lie (I'm in love with you, in the morning, in the night, oh, yeah) (I'm in love with you, in the morning, in the night, oh, yeah) Yay sama adouna, oh, yeah Sama baby coco waay, ey yeah Yow yay sama aldiana, my love Sama baby coco waay, hmm yeah Way way way way Mèrr bi fadjoul dara Mom fadjoul dara Konn fadjoul dara Baylènn té gneuw ma takal la or 24 carats Wurus 24 carats Ngualam 24 carats

Wally B. Seck의 다른 곡

Wally B. Seck →

관련 가사