Yeye (DIAGA)
WO

Yeye (DIAGA) 가사

장르World Music
원문 언어WO
조회수24
Aa읽기 설정
글자 크기 18

원문 가사

WO
번역이 아직 없습니다. 원문 가사를 표시합니다.
Fefsy on the beat ayy Aksina thi say lokho you léér Diaarama nénam Wonala gnetti yone Sog thi tegg baabam Yama sang, solal ma Ma dioy ngeu nakh ma Souma fébaré nga bayi lepp té fadj ma Woy nala, bakk nala yaye Diaarama nénam Souma done wurus yamay moom Souma sagnone abadan ma done sa wérouway Douma tayi dila djine sa rafétaay yow Awma loumay ragal ndakh yaye sama ganaay Ayo yé sama yaye boul di dioyo Beugouma guiss say rongogne Boul di dioyo Boula dara méti Boul di dioyo Néné touti maag na Yaye awma sa fay Linga dadj thi keur gui Linga dadj thi mane mii Dina ko séédé tay Eumb ma diourom gnénti wéér Yar ma, yor ma, yeureum ma Louma meunti def yagg yagg téral la Baba gueureum nala, benn djiguén gueunoula Yaye Diaga, awma sa fey Yagg ngama mougnal Daan nala sonnal Wanté baalou nala akk yaye, bala mouy wééss Dinala bégueul, meussouloma féral Mbeuguel bima am thi yow dou rééss, dou diékh Ayo ye sama yaye boul di dioyo Teranga doy na seukk thi nga done sama yaye Sant na Yalla Diaarama nénam Yaye awma sa fay Linga dadj thi keur gui Linga dadj thi mane mii Dina ko séédé tay Eumb ma diourom gnénti wéér Yar ma, yor ma, yeureum ma Louma meunti def yagg yagg téral la Baba gueureum nala, bén djiguén gueunoula Yaye Diaga, awma sa fey Limala yééné dougn ko natt Khadioul thi adouna Di gnane Yalla bayila fi Té saam la Soukk thi say tankk moy sama aldjana Yaye awma sa fay Linga dadj thi keur gui Linga dadj thi mane mii Dina ko séédé tay Fefsy on the beat ayy

Wally B. Seck의 다른 곡

Wally B. Seck →

관련 가사