Leeray
WO

Leeray 가사

원문 언어WO
조회수14
Aa읽기 설정
글자 크기 18

원문 가사

WO
번역이 아직 없습니다. 원문 가사를 표시합니다.
Toog ci sama xol ba abadan Daiman dénk naa la sama ruu Yaw laa teg ci kaw ndax yaa ci mën Mënuñu bëre sa kaw ndax yaa ma daan Ay wax yu sew du mëna ñàkk suñu biir Bul ma meree su ma la tooñee nang ma baal Leeraay Yaay sama leeraay Yaa ma jële ci lëndëm sotti ma leer Yaa may mottali Sa xol du wet ndax maa koy wetali Eh yaw la diamond bi mëna leeral sama eyes Yaay sama lingeer bëgg naa la def jabar Dofloo nga ma ba pare dénk naa la samay fan Bëgguma nga mer teg naa la fi ma teg sama yaaya booye Yaa ma jural samay doom Yaw laa nara def seen yaaya booye Mbëggeel day sax ci xol yaw Yaay garab bi mëna faj sama feebar Jarul maa lay wax ni dama la nob Boo xolee samay bët ding ko fa gis sax Leeraay Yaay sama leeraay Yaa ma jële ci lëndëm sotti ma leer Yaa may mottali Sa xol du wet ndax maa koy wetali Eh yaw la diamond bi mëna leeral sama eyes

Wizzy Kana의 다른 곡

Wizzy Kana →

관련 가사