Jolie femme d'Afrique
WO

Jolie femme d'Afrique lyrics

GenrePop
Original languageWO
Views85
AaReading settings
Text size 18

Original lyrics

WO
Translation not available yet. Showing the original lyrics.
Bàyyi ma yéye chewing gum Xale bi est-ce que c'est pour moi Zéro faute ma ne lépp tout bon Ni ma ko barde we, le mbaa doo ngiste Jolie femme d'Afrique (d'Afrique) Sama regard mooy bombastic Gaa yi naan je suis fantastique Su ma jàkkaarloo nit ki man Maa fit wi di musique naan Rampapam rampapam rampapam Rampapam rampapam rampapam Samay bët ak sama xol a ma tooñ Ñoo ma nobloo boy bi nekk sama koñ Ne na fook mu gis ma tay si ngoon Amaguma fitu wax ak moom Bàyyileen ma bu leen ma dugal Ci mbëggeel bu may yóbbu coma Ay, ay, ay yaay, foon na ma dee Foon na ma dee, lu ma dall yaw la Soo ma nobee lu ma dall yaw la Bi xeetu nit man àntanuma ko Dama ko nob ba [?] Di ko xalaat ta [?] Su ma ko jegee (moo ray ma) Ma lépp lépp lépp [?] Su ma naree giseek moom Panique jaxasoo ma ni juuk rekk daw Eh yaw man ndekke parewuma Maa ngi mel ni kuy dem combat Ouyah, yah Dama choqué yaah yah Dama choqué yaah yah Tax bu ñu dajee sama fit bi di tëb di tëgganal sib na Rampapam rampapam rampapam Rampapam rampapam rampapam Samay bët ak sama xol a ma tooñ Ñoo ma nobloo boy bi nekk sama koñ Ne na fook mu gis ma tay si ngoon Amaguma fiitu wax ak moom Bàyyileen mu bu leen ma dugal Ci mbëggeel bu may yóbbu coma Ay, ay, ay yaay, foon na ma dee Foon na ma dee, lu ma dall yaw la Soo ma nobee lu ma dall yaw la Bi xeetu nit man àntanuma ko Ay, ay, ay yaay, foon na ma dee Foon na ma dee, lu ma dall yaw la Soo ma nobee lu ma dall yaw la Bi xeetu nit man àntanuma ko Ay ay choqué, dam lay choqué Su ma jugee pour dem daa am luy bloqué, ah Écoutez man faw ma focus Dama bëgga xam man kañ la namp ragal, ah! Jolie femme d'Afrique Sama regard mooy bombastic Gaa yi naan je suis fantastique Su ma jàkkaarloo boy bi Maa fit bi di musique naan Rampapam rampapam papam Rampapam rampapam papanra Boy bi boy bi laperas Bi xeetu nit àntanuma ko Ay, ay, ay yaay, foon na ma dee Foon na ma dee, lu ma dall yaw la Soo ma nobee lu ma dall yaw la Bi xeetu nit man àntanuma ko Ouyah, yah Dama choqué yaah yah Dama choqué yaah yah Tax bu ñu dajee sama fit bi di tëb Man xamuma pur lan, wuy!

More from Mia Guisse

Mia Guisse →

Related lyrics