Reine Des Stars
WO

Текст песни Reine Des Stars

Язык оригиналаWO
Просмотры2
AaНастройки чтения
Размер текста 18

Оригинальный текст

WO
Перевод пока недоступен. Показан оригинальный текст.
Reine des stars fële Lu fi yëngu ñépp d’accord ni man la (man la) Ma tëju woon doon toggu Kon su ma yaqee ñu xam fi ma mané (mëne) Ñi di laaj ki ka na? Yaa ngi am Sokhou BB la Diva Am buzz defaguma dara Ñépp di ma wër pourtant et bien je suis là Sokhou yaw BB (Sokhou yaw BB) Sokhou yaw BB (Sokhou yaw BB) Sokhou yaw BB (Sokhou yaw BB) Sokhou yaw BB (Sokhou yaw BB) Doomu Fatick bi mag na Déllusi jël li mu moom si game bi Dama nekk sama yoon Yagg liggéey lu génn feel Am na ñu may wax Sokhou Cover rekk Dégluwoo ma wax ma li ngay yëg Il faut imiter les meilleurs pour en devenir un C’est normal Lu ma génne mu doon hit C’est normal May xalé bi yóbbu seen fit C’est normal Dama open si def ay feat Ça dépend Xam nga musique gu Sénégal Dafa doy waar waaye j’attends tout Lu fi yëngu ñépp d’accord ni man la (man la) Ma tëju woon doon toggu Kon su ma yaqee ñu xam fi ma mané (mëne) Ñi di laaj ki ka na? Yaa ngi am Sokhou BB la Diva Am buzz defaguma dara Ñépp di ma wër pourtant et bien je suis là Sokhou yaw BB (Sokhou yaw BB) Sokhou yaw BB (Sokhou yaw BB) Sokhou yaw BB (Sokhou yaw BB) Sokhou yaw BB (Sokhou yaw BB) Ñëwaat na Si game bi Ñëwaat na Si game bi Ñëwaat na Si game bi Fans Sokhou yéh! Maa ngi ni

Ещё от Sokhou Bb

Sokhou Bb →

Похожие тексты