Banneex
WO

Banneex şarkı sözleri

TürRb
Orijinal dilWO
Görüntülenme22
AaOkuma ayarları
Metin boyutu 18

Orijinal sözler

WO
Translation not available yet. Showing the original lyrics.
Kula faale wul man mii maa lay faale Doon sa seetu kula xool man lay gisaale Kula faale wul man mii maa lay faale Doon sa seetu kula xool man lay gisaale Ci sa bët laay xool naan la I love you Baby, yow yaay sama life Ci sa bët laay xool naan la I love you Baby, yow yaay sama life Baby yow yaay sama life Suma Yàlla bëggee wax len ko na ma baayi ak yow Ndax ku melni yow amatul ci àdduna Sama xol laa la def bëgg dëgg laa la def te duma sooraale Benn noon ndax yaay sama life Ci sa bët laay xool naan la I love you Baby, yow yaay sama life Baby, yow yaay sama life Kula faale wul man mii maa lay faale Doon sa seetu kula xool man lay gisaale Ci sa bët laay xool naan la I love you Baby, yow yaay sama life Baby, yow yaay sama life Kula faale wul man mii maa lay faale Doon sa seetu kula xool man lay gisaale Ci sa bët laay xool naan la I love you Baby, yow yaay sama life Ci sa bët laay xool naan la I love you Baby, yow yaay sama life

Obree Daman sanatçısından daha fazla

Obree Daman →

İlgili şarkı sözleri