Gorée
WO

Gorée şarkı sözleri

TürWorld Music
Orijinal dilWO
Görüntülenme40
AaOkuma ayarları
Metin boyutu 18

Orijinal sözler

WO
Translation not available yet. Showing the original lyrics.
Bama démé gorée manne Andak samayyy kharite Demm sa keur diam gawonne Dama dalle di seugemm dioyy Goor yi magg yi bi boor Djiguéne yu magg yi bi boor Goor yu ndaww yi bi boor Djigéne yu naww yi tchi bénène boor Niu daddi fayy khali yonne Yonne bo khamni dangay demm Yonne bo khamni dangay dem Sa khell du demm ludull ssi délussé Lolloyyy natu lawu buur bi mi borom doggal yyé Lolayy nattu lawu buur bi boromm kunfa yakune Bama démé gorée manne Andakk samayy kharit Demm sa keur diamm gawonne Dama dalle di seugueumm dioyy Goor yi magg yi bi boor Djiguéne yu magg yi bi boor Goor yu ndaww yi bi boor Djigéne yu naww yi tchi bénène boor Niu daddi fayy khali yonne Yonne bo khamni dangay demm Sa khell du demm ludull ssi délussé, ah ah gorée Lolloyyy natu lawu buur bi mi borom doggal yyé Lolayy nattu lawu buur bi boromm kunfa yakune Lolloyyy natu lawu buur bi mi borom doggal yyé Lolayy nattu lawu buur bi boromm kunfa yakune Gorée, natu lawu buur bi mi borom doggal yyé Lolayy nattu lawu buur bi boromm kunfa yakune

Youssou N'dour sanatçısından daha fazla

Youssou N'dour →

İlgili şarkı sözleri