Taggo
WO

Taggo کے بول

صنفHip Hop Rap
اصل زبانWO
مناظر8
Aaپڑھنے کی ترتیبات
متن کا سائز 18

اصل بول

WO
ترجمہ ابھی دستیاب نہیں۔ اصل بول دکھائے جا رہے ہیں۔
Lii ñuy nekk yépp doon di ànd Dawuma xalaat di lay ñàkk Sunu rêve bi moo nekkoon Dundu dem ba gëna mag dal di tuddunte ay doom Dem na Oh jooy naa! Lii mooy sama tiis Jot nga départ dootuma la gis Lii daf ma mujju yéem Donoon nga ku may yee Danga ma gëna yokk def fulë ci sama life Xarit sama xol bi daf ci fees Bi may tokk ñu naan ma danga dem Li ma ñàkka reer Mooy sama saggoo Man de sama xol bi daf ci fees dell! Bi may tokk ñu naan ma da mujje dem Bi mu may sooga reer Laa xam ni dafa doon taggoo Ñàkk naa, hmm! No, no! No, no! No no no no noo Maa ñi xaar Bés dina ñëwaat ñu gisee Jàmbaar Ndaanaan dem na ni Maa ngi lay ñaanal Fi nga nekk gënal la fuuf fi nga juge tay Man dama mujj wet Ba tax na dama réer Oh waay! Sama waa ji dem na ni Jooy naa Jooy naa, jooy naa, jooy naa Man jooy naa sama waje Xarit sama xol bi daf ci fees Bi may tokk ñu naan ma danga dem Li ma ñàkka reer Mooy sama saggoo Man de sama xol bi daf ci fees dell! Bi may tokk ñu naan ma da mujje dem Bi mu may sooga reer Laa xam ni dafa doon taggoo Ñàkk naa, hmm!

Ibu Bash کے مزید گیت

Ibu Bash →

متعلقہ بول