Marché Love
WO

Marché Love کے بول

صنفPop
اصل زبانWO
مناظر9
Aaپڑھنے کی ترتیبات
متن کا سائز 18

اصل بول

WO
ترجمہ ابھی دستیاب نہیں۔ اصل بول دکھائے جا رہے ہیں۔
[Awa Thies] Kaay ma jaay la mbëggeel bu dëgg Ak xol bu nice, bu ànd yërmandé Kaay ma jaay la li nga gëna bëgg Jigéen bu baax dey yaw wax dëgg [Pape Bilal] Kaay ma jaay la mbëggeel bu neex Tegsi jaay la sincérité bu weer, boo dul gis feneen Góor am na fi ak fideel bu yomb Nobeel am na fi, nobeel bu ñor xomb [Awa Thies] Loo fay gaaw, waxal waxal Loo fay gaaw? [Pape Bilal] Amul waxale [Awa Thies] Loo fay gaaw, waxal waxal Loo fay gaaw? [Pape Bilal] Lu ma dajalee Dajale naa pur jëndëru plaisir Ay saku bisous ak je t'aime bu baax, eee! [Dane] Am na sax mu maikeur Am na sax mu nob Am na sax mu muñ ak doyloo, waaw! Mbëggeel ma jaay Mbëggeel ma jaay Mbëggeel ma jaay Mbëggeel ma jaay [?] [Fatel] Magie bëggante a ngi ni Mbëggeel rekk laay jaay Yaw fayal sa impôt sa juti avant ngay jaay Et puis dama bëgg xol bu sincère, góor bu ngëb Kuy yërëm jigéen tegsi di ko wax [Pape Bilal] Loo fay gaaw, waxal waxal, loo fay gaaw? [Awa Thies] Amul waxale [Pape Bilal] Loo fay gaaw, waxal waxal, loo fay gaaw? [Awa Thies] Lu ma dajalee Dajale naa pur jëndëru plaisir Ay saku bisous ak je t'aime bu baax, eee! [Dane] Am na sax mu maikeur Am na sax mu nob Am na sax mu muñ ak doyloo, waaw! Mbëggeel ma jaay Mbëggeel ma jaay Mbëggeel ma jaay Mbëggeel ma jaay

ZBest Family کے مزید گیت

ZBest Family →

متعلقہ بول