Nous 2 (part. Wally B. Seck)
WO

Nous 2 (part. Wally B. Seck) lyrics

GenrePop
Original languageWO
Views176
AaReading settings
Text size 18

Original lyrics

WO
Translation not available yet. Showing the original lyrics.
Yëguloo ne séy duma la koy jaay Dama xam rekk sama njëg, xam tamit lu maay jar Yëguloo ne man jigéen duma jaay neex Dama xam rekk sama njëg xam tamit Dama lay wax nga xam ni sa ñangal safu ma dara (dara) Sans man yaw doo dara (dara) Danga ma fàtte xam naa (xam naa) Ba ngay ram sama tànk naan ma nob la ngir Yàlla (yàlla) Loo xam lu neex man la Séy jaaxalu ma oh, yeah, yeah Dalal fok ni yaw rekk ya dugg mbar ànd AK salbe Boy mbaa du danga foog ne yaw rekk yaay góor wala? Ñaata yoon nga ram sama kanam comme xale Bu la neexe nga doxan Yaw defal comme si j'étais pas là Ooh, bu la neexe, bul fanaan ci yaw Yaw defal comme si j'étais pas là Yaw defal comme si j'étais pas là Yëguloo ne séy duma la koy jaay Dama xam rekk sama njëg, xam tamit lu maay jar Yëguloo ne man jigéen duma jaay neex Dama xam rekk sama njëg xam tamit Yaa ngi nax sa bopp Danga foog ni man maa xëy Barde ci keneen Wax ji bari na, ana looy xaar? Demal feneen Maa leen mën bari cacc yaay ñëwaat Naan bae jéegalu naa Xam nga ko ko sekkal bandit cerveau la woo Tere la nelaw Comme d'hab ay wax ngay tambalee ee Te ay jooy ngay mujje ee Wool sa bawat mee, ñëw baaluwaat, baaluwaat Bu la neexe nga doxan Yaw defal comme si j'étais pas là Ooh, bu la neexe bul fanaan ci yaw Yaw defal comme si j'étais pas là Yaw defal comme si j'étais pas là Yëguloo ne séy duma la koy jaay Dama xam rekk sama njëg, xam tamit lu maay jar Yëguloo ne maa la gëna neex Dama xam rekk sama njëg xam tamit Man dama lay wax nga xam ni sa ñangal safu ma dara (dara) Sans man yaw doo dara Danga ma fàtte xam naa Mbaa du seytaan la jaay ba nga foog ni yaw rekk la Léegi dafa sukka mel ni Aïda sukkeer Moo tax ngay jooy te loxo du la laal yaw Xamante nañu mak yaw Téye sama bopp ci yaw laay def Boo ko defe dinaa metti fees ci man Damay nàppe rekk mais mënuma la bàyyi Man yaw laa nob te leer na ma, kaay waay Sama reni xol, bébé n b'i fe Ti voglio bene, sama bella woyu Vi Wax naa la yaay baayam bandit bi Bëgg naa la, faale naa la waawaaw Eee, ee (Je ne peux pas vivre sans toi) Boo ma mere réy ma Ndax yaw yaay ki tax xol bi neex na (Je ne peux pas vivre sans toi) Oh mon bébé soo mere gaañ ma Ci xol leer na, xale bi (Je ne peux pas vivre sans toi) Baby Yàlla la sax jox ma Ma jël nob la, xale bile (Je ne peux pas vivre sans toi) Yaw ma la bëgg ba mu jeex ma tay Yaw yaa may ray, xale bi (Je ne peux pas vivre sans toi) Ndeysaan xamuloo ne Xuloo boo gis dafay jeex (Je ne peux pas vivre sans toi) Boo jubboowee sa xaaju guddi day neex (Je ne peux pas vivre sans toi)

More from Viviane Chidid

Viviane Chidid →

Related lyrics