Djery Ngoné
WO

Djery Ngoné lyrics

GenreWorld Music
Original languageWO
Views32
AaReading settings
Text size 18

Original lyrics

WO
Translation not available yet. Showing the original lyrics.
Agn dém ndaat diéry seu keur maam Agn dém ndaat diéry seu keur maam Kouli ma ceu sengui ndaat Diéry ngoné hum hum Meu délou ci waat Diéry ngoné ma laobé samba kouli meu ceu sengui ndaat mbaye Mafaaly Kumba ndaama seu maam teukh bi Naarou Marietou Agne sama waadji Mbaye diéry, diobéti naa leu Diéry ngoné Mafaaly Kumba ndaama-a Mbaye diéry, diobéti naa leu Mbaye diéry, diobéti naa leu Mbokoum yaayou Khoudia Ciss Djiguénou Bathie Samb Yaayou Aléya fonk naa leu Guéwélou ndaat ak guééry ndaat (ndaat ndaat) Ko ciy woy néko maa laobé samb Diéry ngoné Kouli ma ceu sengui ndaat Diéry ngoné ma laobé samba kouli meu ceu sengui ndaat mbaye Mafaaly, Mafaaly Mafaaly Kumba ndaama seu maam teukh bi Balaa déég fouki ball ak niaar né touy Mbaye diéry, diobéti naa leu Agn dém ndaat diéry seu keur maam Kou seu baay meunon baayam, dom djeu yaako meun Yaa lén meun, diéry (Agn dém ndaat diéry seu keur maam) Fonk ngam yo, diéry Téral ngama, diéry (Agn dém ndaat diéry seu keur maam) Chérie Thomas, gueun ci man Gaaw ci man anh diéry (Agn dém ndaat diéry seu keur maam) Nangou naa kou leu makk Douma nangou kou leu gueun, diéry Yaa lén meun, na-na diéry

More from Wally B. Seck

Wally B. Seck →

Related lyrics