WURUS (Version Afro)
WO

WURUS (Version Afro) lyrics

GenreWorld Music
Original languageWO
Views56
AaReading settings
Text size 18

Original lyrics

WO
Translation not available yet. Showing the original lyrics.
Yaay sama àdduna, oh, yeah Sama baby coco waay, ey yeah Yaw yaay sama àljanna My love! Sama baby coco waay, hmm yeah Baby yaay man Tëddal nelaw xam ni munuñu dara I don't give a fuck, merkat fajul dara Takkal la or ba ci 24 carats Dañ leen di bàyyeek përëm bi ñoom ñuy dékke aya Baby, I just want a real love Real love, I just wanna know a real love Definitely I don't want lie I'm in love with you In the morning, in the night, oh, yeah I'm in love with you In the morning, in the night, oh, yeah Yaay sama àdduna, oh, yeah Sama baby coco waay, ey yeah Yaw yaay sama àljanna My love! Sama baby coco waay, hmm yeah Waay waay waay waay Mer bi fajul dara Moom fajul dara Kon fajul dara Bàyyi leen te ñëw ma takkal la or 24 carats Wurus 24 carats Ngalam 24 carats Xanaa du ma la yénne Ma vie, ma vie Baby yaay man Tëddal nelaw xam ni munuñu dara I don't give a fuck, merkat fajul dara Takkal la or ba ci 24 carats Dañ leen di bàyyeek përëm bi ñoom ñuy dékke aya Baby, I just want a real love Real love, I just wanna know a real love Definitely I don't want lie I'm in love with you In the morning, in the night, oh, yeah I'm in love with you In the morning, in the night, oh, yeah Yaay sama àdduna, oh, yeah Sama baby coco waay, ey yeah Yaw yaay sama àljanna My love! Sama baby coco waay, hmm yeah Waay waay waay waay Mer bi fajul dara Moom fajul dara Kon fajul dara Bàyyi leen te ñëw ma takkal la or 24 carats Wurus 24 carats Ngalam 24 carats

More from Wally B. Seck

Wally B. Seck →

Related lyrics