Song Daan (feat. Youssou N'Dour)
WO

Song Daan (feat. Youssou N'Dour) 歌词

流派Hip Hop Rap
原文语言WO
浏览量34
Aa阅读设置
文字大小 18

原文歌词

WO
暂时没有翻译,当前显示原文歌词。
Dooley nit kou ñuul kou, ko beug xam la Mbeur mouy daan kou Ko beug xam démal lathi ko you Woma woma Ci leundeum, dinala Wouyou Oubil sama, xol dinga Xam nimou sédéé ci you Fileg mang lay am, sama xol Luma songù, daan ko Fileg mang lay am, sama Xèll Luma songù, daan ko Songù Daan Koo Songù Daan Koo Songù Daan Koo Songù Daan Koo Man Maanan, mane iiow laa Liow nga naan, ngané man leuh Man Maanan, mane iiow laa Liow nga naan, ngané man leuh, éh éh éh Béneu biss dina niow, mou melni louniouy nétali Mou melni lii dou anh Té ken Du jog, naan man mi nako fékéh yoooo Ndah nguelaw lii daaw diñou yobalé Xoob yiy russ ci garab guii Ah lifi xew tay bouniou ko fatéé Africa Dom yiy wane, sén bopeuh Fileg mang lay am, sama xol Luma songù, daan ko Fileg mang lay am, sama Xèll Luma songù, daan ko Songù Daan Koo Songù Daan Koo Songù Daan Koo Songù Daan Koo Man Maanan, mane iiow laa Liow nga naan, ngané man leuh Man Maanan, mane iiow laa Liow nga naan, ngané man leuh éh éh éh éh Cí Díg bï Fofou, laay diar Mù am xàl Safara douma daaw Los Angeles Paris ba Rio New Delhi London Tokyo Sêdoog Yén Liñu, Jēlé Fénéne Fi niou, diarr ñun ba éksi fí Dafa mèlni, louńou nétali Los Angeles Paris ba Rio New Delhi London Tokyo Sêdoog Yén Liniou Jēlé Fénén Ééh éh eh eeh Maa contaane, yoow it yaa contaaan Maleu geuuneuu contane, uh yeah Contane yeah yeah Contane yeah Contane yeah Akon Yousou Yeah Akon Yousou Yeah Cí Díg bï Fofù, laay diar Mù am xàl Safara douma daaw Los Angeles Paris ba Rio New Delhi London Tokyo Sêdoog Yén Liñu Jēlé Fénéne Fi niou, diarr ñun ba éksi fí Dafa mèlni, louńou nétali Los Angeles Paris ba Rio New Delhi London Tokyo Sêdoog Yén Liniou Jēlé Fénéne

更多 Akon

Akon →

相关歌词