Tout donner (feat. Xiirsa)
WO

Tout donner (feat. Xiirsa) 歌词

流派Afrobeats
原文语言WO
浏览量73
Aa阅读设置
文字大小 18

原文歌词

WO
暂时没有翻译,当前显示原文歌词。
Sama xol nga yore Moom laa la toppe Liiti liiti liiti liiti May rombe gumbe Dama tapetul Def naa ci lu ne Lu mu guddi guddi guddi Dama lay gunge Baby I follow you Cause my heart is on you You Baby I follow you Cause my heart is on you You Oooh pourtant Jox naa la lépp, jox la lépp Oooh pourtant Je t'ai tout donné, tout donné Euh euh euh Massamba Wallo Xam naa bu baax li ngay bañ Ñu dem ba ci biir maa lay gaañ Def naa ko saay mas waaye Ak yaw da am lu may waaj Àdduna moo la soxla Man ma yitewoo la lool sax Massamba mi ngi may gaañ yaay Kalame naa la ak gaa yi Kaay gaaw, dëgg la ni dëng na Su ma demee balay way Nga xam ni caaxaan taxul Oooh pourtant Jox naa la lépp, jox la lépp Oooh pourtant Je t'ai tout donné, tout donné Euh euh euh Man duma saay saay Laaj ko sama gayi Ñëwal ñu life waay Sonn naa Bul mësa gaadaay Doonal seen yaay Njaabot gi kaay waay Gunge ma Man duma saay saay Laaj ko sama gayi Ñëwal ñu life waay Sonn naa

更多 AMADEUS

AMADEUS →

相关歌词