Ragalouniou Dara (feat. Kiné Lam)
WO

Ragalouniou Dara (feat. Kiné Lam) 歌词

流派Hip Hop Rap
原文语言WO
浏览量19
Aa阅读设置
文字大小 18

原文歌词

WO
暂时没有翻译,当前显示原文歌词。
Ragaluñu dara, dara Da da dara Ragaluñu dara, dara Da da dara Bu jant bi sowee Équipe moo wetal Yobbu ndamam, gàcce ngalama Les lions du Sénégal Ak ngeen ñoo yàgg bégal Gàcce ngalama, allez les lions! Ragaluñu dara, dara Da da dara Ragaluñu dara, dara Da da dara (Anh lawoon fawoon) Ah, ragaluñu dara Gaynde xiif tey, xepp na fukki mbaana Defaat fa ndam bëgg ñibbi Dakar Xanaa danga fàtte Sadio Khana? Di taal sa camp fi la tikki taka (ha haa) Gën la tàng, gën la sayar, gën a waga Ku fi joog ma tiim la ci kaw, caakaba la Kenn du noyal amul seral, amul sikki saka Ragaluñu dara, dara Da da dara Ragaluñu dara, dara Da da dara Fulaak fayda ak jom Ak ngor lañiy wane sur le terrain Gàcce ngalama, ahn Sunu équipe bi, ahn Lawoon fawoon

更多 Dip Doundou Guiss

Dip Doundou Guiss →

相关歌词