Miroir
WO

Miroir 歌词

流派Hip Hop Rap
原文语言WO
浏览量9
Aa阅读设置
文字大小 18

原文歌词

WO
暂时没有翻译,当前显示原文歌词。
Li ma yéem dofloo na nit yu bari Xol bi moo ci tiit tax ma listaxar Def naa la sama toll, bu dul yaw du ma bàyyi Damay wax nga sipp te danga képp say daaj Lan moo ñu jikk xacundoo di songu Duma xaar nga ci dox may dogg di sonn Parfois nga fiir ni may jëfe ndiru ay tooñ Kuy bëgg dangay ball alors baby profitons! Kon damay ñëw sa koñ ndalle peloton Saar seul galer ak samay kiloy guro tok fa ñaan Su may dem tuddee la boulevard Hey maa ko saña wax te du ma ci tàyyi Ay mbëggeel laa lay drop drop drop drop drop drop Jaaral nga ma daaw daaw daaw daaw daaw Weerul ñu jël ay tof tof tof tof tof Li may yëg tax may xaar pour ñu marié Li may xaar mooy try one day Jàkk jaa ak yoonu mairie Yaa doon bidéew bi tax may tëp pour saxi laf Am la soxna mooy tax ma chill tay Su nekkee dëgg mak ñi dem ñaan Reeroo su amer dañuy waxtaan Xulóo jiguñu daf ñuy tardeel Réccu mooy nga baal ma su ma la tooñee Miroir sama xel lu dul sa xol du ci feñ Def guro sama sac Wan ko sa yaay te du bañ déet waay! Kon damay ñëw sa koñ ndalle peloton Saar seul galer ak samay kiloy guro tok fa ñaan Su may dem tuddee la boulevard Hey maa ko saña wax te du ma ci tàyyi Ay mbëggeel laa lay drop drop drop drop drop drop Jaaral nga ma daaw daaw daaw daaw daaw Weerul ñu jël ay tof tof tof tof tof Li may yëg tax may xaar pour ñu marié Toc toc toc toc toc! Daw daw daw daw daw! Toph toph toph toph toph! Looy xaar pour ñu mariéééé? Kone damay nieuw seu kogn undallé peloton Saarr seu galer ak samay kiloy gouro tok feu niane Sou may dém touder leu boulevard Héy mako sagna wakh té dou meu ci taayi yeaaah!

更多 Ibu Bash

Ibu Bash →

相关歌词