HBD
WO

HBD 歌词

流派Afrobeats
原文语言WO
浏览量11
Aa阅读设置
文字大小 18

原文歌词

WO
暂时没有翻译,当前显示原文歌词。
Bés bi nga juddu woon Delussi na, tay la tay, happy birthday Bés bi yay boroom Ndax yow rek dara dula fay, happy birthday Dégg naa ñu wax naan Bés du toute boroom rek ley tolool Yow dundël cent onze ans, happy birthday Happy birthday, tay sa bés la, happy birthday Happy birthday, nanga happy, happy birthday Bés bi nga juddu woon Mo delussi ñulay ndokalé Amo lu ko gën rëy Féké ngako kon nagn ko célébré Bima yéwo lako guiss si sama Facebook Ma-Mané toogay amatul naa dioug In-indil nagn la say cadeaux Kay soufflé sey bougies, dagg say gateaux Sa xarit yi nga magandol Wuyu si la ñëw diko fêté-ndo Ak photos yi ñu jëlë-ndo Happy birthday ñu kay wayandooo Yalla nga dundu ba déwén ñu défat lu mel ni Am jàmm ak xéwel mbékté bu yaatu ci yow mi Bés bi nga juddu woon Delussi na, tay la tay, happy birthday Bés bi yay boroom Ndax yow rek dara dula fay, happy birthday Dégg naa ñu wax naan Bés du toute boroom rek ley tolool Yow dundël cent onze ans, happy birthday Happy birthday, tay sa bés la, happy birthday Happy birthday, nanga happy, happy birthday Bés bu délussi Bés bu délussi Da-day neex, ñu yagg ko féééké Ñu diko fêté ak baneex, no ma guissé Tay fi la guéné, ñëw téw ci sa birthday/bés bi Bés bi munumako manqué Sa xarit yi nga magandol Wuyu si la ñëw diko fêté-ndo Ak photos yi ñu jëlë-ndo Happy birthday ñu kay wayandooo Dundel lu bari, ba say may di bawaan Sa nitt yu baax yangui ni Yaa ayé kay woon sa moomél Bés bi nga juddu woon Delussi na, tay la tay, happy birthday Bés bi yay boroom Ndax yow rek dara dula fay, happy birthday Dégg naa ñu wax naan Bés du toute boroom rek ley tolool Yow dundël cent onze ans, happy birthday Happy birthday, tay sa bés la, happy birthday Happy birthday, nanga happy, happy birthday

更多 Maabo

Maabo →

相关歌词