Nabi
WO

Nabi 歌词

流派Afrobeats
原文语言WO
浏览量6
Aa阅读设置
文字大小 18

原文歌词

WO
暂时没有翻译,当前显示原文歌词。
Mouhamadu rassoulilah Mouhamadu rassoulilah Dass naa sama baat Fas yéene di la tagg Kañ a leen ma Moustapha (Mouhamadu rassoulilah) Séy naa ci di la kañ Ahmada jar a kañ Kañaleen ma Moustapha (Mouhamadu rassoulilah) Mooy Nabi Yaa rassoulilah mooy Nabi (Mouhamadu rassoulilah) Mooy nabi Yaa rassoulilah mooy Nabi (Mouhamadu rassoulilah) Mooy Ahmad Hamir, Bachiru Bachi Mu chabile Moustapha (Mouhamadu rassoulilah) Mooy sànge bi fi gën te sànge du ko gën Tayu xasi mbër yi maay Moustapha (Mouhamadul rassoulilah) Waa ma ka way nañu ko ma dina feruleen Alhoustaral Moustapha (Mouhamadu rassoulilah) Li dundal sama ruu ba leeral jëm jee Nataal sama xol ci Moustapha (Mouhamadu rassoulilah) Suñu boroom julli na aki malaykam (Mouhamadu rassoulilah) Waay ku li adjidame, war nga sax di julli ci (Mouhamadu rassoulilah) Dass naa sama batt Fass yéné di la tagg Kaña leen ma Moustapha (Mouhamadu rassoulilah) Seye na ci dila kañ Axmada jara kañ Kañaleen ma Moustapha (Mouhamadu rassoulilah) Mooy nabi Ya rassoulilah mooy nabi (Mouhamadu rassoulilah) Mooy nabi Ya rassoulilah mooy nabi (Mouhamadu rassoulilah) Fii ko fi joxe sa yaakaar Moom Nabi la yaakaar Baayu Fatuma mooy (Mouhamadu rassoulilah) Sant nañu Moustapha Lakku nañu ci Moustapha Kuy saku walu billaay dawal ci (Mouhamadu rassoulilah) Man amuma feneen fu ma jëm ci ku dul (Mouhamadu rassoulilah) Wuutuma feneen fu ma jëm ci ku dul (Mouhamadu rassoulilah) Man dajj naa li ma doon wër (Mouhamadu rassoulilah) Wuuti leeru gën gi mindeef mi eee (Mouhamadu rassoulilah) Dass naa sama batt Fass yéné di la tagg Kaña leen ma Moustapha (Mouhamadu rassoulilah) Seye na ci dila kañ Ahmada jara kañ Kañaleen ma Moustapha (Mouhamadu rassoulilah) Nabi! Bi ñu ma dompté tamite damp nga ma Nabi! Bi ma wété loolu nga wétalli ma

更多 Maabo

Maabo →

相关歌词