Partir
WO

Partir 歌词

流派Afrobeats
原文语言WO
浏览量44
Aa阅读设置
文字大小 18

原文歌词

WO
暂时没有翻译,当前显示原文歌词。
Bima deimei ñu mayema visa il faut que ma dem Liguey nguir terral samay wadiour souma nieuwei takkla Mane nanelay deff Limay raggal moy wanela guinaw nga Fattemay souboba dinama nakari ndax ande bi yagna Mane nanelay deff Wayei fouma diar mane dina dem liguey Ndax may taw wadiour yi manelañu yaakaar Né faw ma dem outidji nguir terral la Baby sorry gueneulouma baby mangui nieuw Beugnala xalei biley Bima deimei ñu mayema visa il faut que ma dem Liguey nguir terral samay wadiour souma nieuwei takela Mane lanelay deff Wayei fouma diar mane dina dem liguey Ndax may taw wadiour yi manelañu yakaar

更多 Pape Diouf

Pape Diouf →

相关歌词