They Cap
WO

They Cap 歌词

流派Samba
原文语言WO
浏览量15
Aa阅读设置
文字大小 18

原文歌词

WO
暂时没有翻译,当前显示原文歌词。
Mom nèna, mom nèna, mom nèna Bandit la daafay cap limouy wakh khamnagn dou deug Nè si net bi di fènn linguèy wakh khamnagn dou deug (Mak gnom) Bokougnou dieumoukay non Bokougnou dieumoukay non (Mak gnom) Bokougnou dieumoukay non Bokougnou dieumoukay non Hey nènagn i can’t put it up Damlènn eup djap Game bi lay gnew deup Kholal I don’t give a fuck Yendou weur di fènn, yenfou guordjiguènn Yakk dèrr di tèkk, bumlèy djap di hum hum Fucking nigga yak seu gnag bi yeup lagnouy ki kill Gno tèyer game bi 4life, yu know the di dil Mais santt Yallah alhamdoulah Mane ma way oulalah Bandit la daafay cap limouy wakh khamnagn dou deug Nè si net bi di fènn linguèy wakh khamnagn dou deug (Mak gnom) Bokougnou dieumoukay non Bokougnou dieumoukay non (Mak gnom) Bokougnou dieumoukay non Bokougnou dieumoukay non Mak yaw dougnou bèneu (nguanè) Dangueu beug ma khof leu (nguanè) Ya ma meunn fènn ngueu Man boyou hood la Diamenz 4life toussss dara doko dèff Nigga dèy dèf dou wakh, nigga dèy dèf dou wakh Am on my way Tchow li beuri neuI’m on my waaaay Niggaz capping but I’m on my way yeah Gnou ngui wakh lounè I’m on my way yeah mon nèna Bandit la daafay cap limouy wakh khamnagn dou deug Nè si net bi di fènn linguèy wakh khamnagn dou deug (Mak gnom) Bokougnou dieumoukay non Bokougnou dieumoukay non (Mak gnom) Bokougnou dieumoukay non Bokougnou dieumoukay non Bandit la daafay cap limouy wakh khamnagn dou deug Nè si net bi di fènn linguèy wakh khamnagn dou deug (Mak gnom) bokougnou dieumoukay Bokougnou dieumoukay non (Mak gnom) Bokougnou dieumoukay non Bokougnou dieumoukay non

更多 Samba Peuzzi

Samba Peuzzi →

相关歌词