Xaarit (feat. Xiirsa)
WO

Xaarit (feat. Xiirsa) 歌词

原文语言WO
浏览量42
Aa阅读设置
文字大小 18

原文歌词

WO
暂时没有翻译,当前显示原文歌词。
Sama doomu ndey nga Doomu ndey Sama doomu ndey nga Doomu ndey nga Sama doomu ndey nga Lu la metti, metti ma Sama doomu ndey nga Lu la naqari, naqari ma Yaw xarit ni la ni la yaw Yaw xarit ni la Yaw xarit ni la ni la yaw Yaw xarit ni la Ndekke xaritoo dina gëna doomu yaay Bauye oye ye yo Ndekke doomu ndey, na déggu ci yaw Te xarit dafay mat doomu ndey Ki ñëw di wax, bul déggaati lu ñaaw ci man gëm ko Te li mooy tax dungeen xulóo Sama doomu ndey nga Lu la metti, metti ma Sama doomu ndey nga Lu la naqari, naqari ma Yaw xarit ni la ni la yaw Yaw xarit ni la Yaw xarit ni la ni la yaw Yaw xarit ni la Doom ndey foo pikkiroo ma naan fay doom Bëgg naa la tudde sama doom Ànd bi wekku ñu ko ci kom-kom Sa jikko tax na dañuy lonko Wo ho woye Démb tax ñu naan tay, wo ho woye! Ni nga ma suturalee Doo ma jebane Yàlla la lay bàyyeek Rasul looy Sama doomu ndey nga Lu la metti, metti ma Sama doomu ndey nga Lu la naqari, naqari ma Yaw xarit ni la ni la yaw Yaw xarit ni la Yaw xarit ni la ni la yaw Yaw xarit ni la Sama doomu ndey nga Doomu ndey Sama doomu ndey nga Doomu ndey nga

更多 Seydina Ndiaye

Seydina Ndiaye →

相关歌词