Bella
WO

Bella 歌词

原文语言WO
浏览量10
Aa阅读设置
文字大小 18

原文歌词

WO
暂时没有翻译,当前显示原文歌词。
Leeraay bi may gis ci sa xar-kanam Moo muur samay bët ba gisuma leneen Xoolatuma faalewuma Focus ci yaw rekk, xale bi dina ma ray Yàllay maye boo ma mayee li ma lay ñaan Ma ne xale bi moom laa bëgg def sama soxna Mënuma la duma la tëkk la ñoom Yaay sama kiiraay Ma ne bëgguma ku ma takkale ak yaw Yaa sama leeraay waay Belissima mia Ma ne de wóolu naa la Moo tax ma jox la sama xol Lii yaw yaay boroom Ti voglio vicino me Sei la mia vita amore Duma la laaj foo may jëme Diri ma man, yóbbu ma fu la neex Bella Bella Bella Belisima mia Bella Bella Bella Belisima mia Bérbu bët mësta xool Feneen fu nit demul woon Bànneex bu réy ngay am ci biir xol Bés ngi ñëw maak yaw lay doon Faalewuma ñi may topp Maak yaw ba abadan, baby yaay sama life Yaay sama Ouroul Ayni Te bëgguma ñu foo farata laay def Ti voglio vicino me Sei la mia vita amore Duma la laaj foo may jëme Diri ma man yóbbuma fu la neex Bella Bella Bella Belisima mia Bella Bella Bella Belisima mia

更多 Wizzy Kana

Wizzy Kana →

相关歌词