Habib Faye
WO

Habib Faye 歌词

流派World Music
原文语言WO
浏览量45
Aa阅读设置
文字大小 18

原文歌词

WO
暂时没有翻译,当前显示原文歌词。
Aduna du dara té dara khadiufi bilae kouko diap Khamal ni diaposi dara Aduna du dara té dara khadiufi bilae kouko diap Khamal ni diaposi dara Mane Youssou niak na andando bou sincère Aduna, aduna dal nakhati naniu Aduna, aduna dafay woré Habib faye demna ni wa diu bax diu tey demna Habib yarou wone na Andak dignité Fonkone na liguey beugone na ndiabotam Donone diambar Mane Youssou niak na andando bou sincère Aduna, aduna dal nakhati naniu Aduna, aduna dafay woré Habib Faye demna ni wa diu bax diu tey demna (Habib, Habib) Dama ko dieulé école andi ko Super étoile mou deugguel ko (Habib, Habib) Man dal mangi len koy dialé yen wa famille wam ak ay fans sam (Habib, Habib) Di len di hamal ni Habib Faye diougué woufi (Habib, Habib) Nio fi defon mak mom mou woné fa loutax nitt gni beuggon ko Senegal la gui lay dioy Rew bangui lay dioy Africa la gui lay dioy Aduna la gui lay dioy (Habib, Habib) Sama beugg beugg moy li, sa beugg beugg moy leh NItt kouné ak beugg beuggam Yallah na done, Yallah na done la geun ci mom Ladial wa doundou gué anh, Habib goudé na goudé na (Habib, Habib) Dama ko dieulé école andi ko Super étoile mou wané fa (Habib, Habib) Wané fa loutax nieup nieup beuggon ko (Habib, Habib) man Youssou niak na andando bou sincère Aduna aduna dal nakhati naniu Aduna aduna dafay woré Habib faye demna ni wa diu bax diu tey demna

更多 Youssou N'dour

Youssou N'dour →

相关歌词