Li Ma Weesu (As In A Mirror)
WO

Li Ma Weesu (As In A Mirror) 歌词

流派World Music
时长3:54
原文语言WO
浏览量2.2K
Aa阅读设置
文字大小 18

原文歌词

WO
暂时没有翻译,当前显示原文歌词。
Li ma dundee, li ma weesu Dey delluse, mel ni seetu Li ma dundee, li ma weesu Dey delluse, mel ni seetu Seetal Leegi leegi ma gesu, ci li ma weesu Leegi leegi ma recu, walla sax di baaku Fu gune yi feetee, dama leen di teetee Wax nu ma neexee, ma bëgga leen Damay, damay, damay dellu gune Mel ni, mel ni, mel ni duma màgg Lu ma gën di yàgg, xel ni mel ni bank Lu ma gën di màgg, dellu tuuti tank Li ma dundee, li ma weesu Dey delluse, mel ni seetu Li ma dundee, li ma weesu Dey delluse, mel ni seetu Ma ni seetal Leegi leegi ma gesu, ci li ma weesu Leegi leegi ma recu, walla sax di baaku Fu gune yi feetee, dama leen di teetee Wax nu ma neexee, ma bëgga leen Damay, damay, damay dellu gune Mel ni, mel ni, mel ni duma màgg Fu gune yi feetee, dama leen di teetee Wax nu mu ma neexee ma béggati Li ma gën di jege, mel ni dama sore Lu ma gëna sore, gën di gis li ma jegewoon Lu ma gën di yàgg, xel ni mel ni bank Lu ma gën di màgg, dellu tuuti tank Li ma dundee, li ma weesu Dey delluse, mel ni seetu Li ma dundee, li ma weesu Dey delluse, mel ni seetu Damay, damay, damay dellu gune Mel ni, mel ni, mel ni duma màgg

更多 Youssou N'dour

Youssou N'dour →

相关歌词