Bideew
WO

Bideew 歌词

流派Rb
原文语言WO
浏览量8
Aa阅读设置
文字大小 18

原文歌词

WO
暂时没有翻译,当前显示原文歌词。
Aha Yow, mii Sa mbëggeel’ay leeral sama yoon Yow, mii Sa mbëggeel’ay leeral sama yoon Agsil ñu àndandoo Àndandoo ci asamaan Sa mbëggeel’ay bideew (Bideew biy leeral goor Yalla) Bideew biy leeral sama yoon Aha, jigeen a indi leer Aha, leeray ci àdduna Aha, sa mbëggeel’ay bideew (Bideew biy leeral goor Yalla) Aha, biy leeral sama yoon Yow, mii Sa mbëggeel’ay leeral sama yoon Yow, mii Sa mbëggeel’ay leeral sama yoon Jigeen’ay leeral Melni leeray u asamaan Sen mbëggeel’ay leeral Jigeen’ay leeral Ni leeray u asamaan Sa mbëggeel’ay leeral Sama yoon Leer leer leer Leeray u jigeen buy joge asamaan si Moy leeral goor Yalla yi Leeray u jigeen buy joge asamaan si Moy leeral goor Yalla yi Leeray u jigeen buy joge asamaan si Moy leeral goor Yalla yi Yow, mii Sa mbëggeel’ay leeral sama yoon Yow, mii Sa mbëggeel’ay leeral sama yoon Aha

更多 Obree Daman

Obree Daman →

相关歌词