Bukki
WO

Bukki 歌词

流派Rb
原文语言WO
浏览量11
Aa阅读设置
文字大小 18

原文歌词

WO
暂时没有翻译,当前显示原文歌词。
Nitt du mala Li ngay def Sakkul naam xam ko Nitt du mala Li ngay wax Seetantal ko waay Nitt du mala jikkoom Nga koy xoolee doomu Àdama ni la ñu Yalla Bindee ci àddunam si Ak sunu matadi Waaye moom Yalla rekk a xam Nitt du mala jikkoom Nga koy xoolee doomu Àdama du dem safara Nitt du mala Li ngay def Sakkul naam xam ko Nitt du mala Li ngay wax Seetantal ko waay Nitt du mala Li ngay wax Seetantal ko waay Wacce na taw ci ñun Gancax gi mèeñ na Ngelaw gi feexal Jànt bi leeral Moo xam li nekk ci ñun Ndax moo def li nekk ci ñun Kon mandu war na ñu Ci nitt ni ko Yalla bindee Nitt du mala jikkoom Nga koy xoolee doomu Àdama du dem safara Nitt du mala jikkoom Nga koy xoolee doomu Àdama du dem safara Nitt du mala Li ngay def Sakkul naam xam ko Nitt du mala Li ngay wax Seetantal ko waay Nitt du mala Li ngay wax Seetantal ko waay Nitt du mala Li ngay wax Seetantal ko waay

更多 Obree Daman

Obree Daman →

相关歌词