Choix (feat. Mia Guisse)
WO

Choix (feat. Mia Guisse) 歌词

流派World Music
原文语言WO
浏览量105
Aa阅读设置
文字大小 18

原文歌词

WO
暂时没有翻译,当前显示原文歌词。
Mane dama Confuse-one yow midnight Tokk ci digg lal bi man ak wétay Khol bi Defna Choix ci Khalilou lay Kay Ngua Adialmako Jourom Yi Way Ske amna Courage, Deugeul limay wah Mo ndakh Niémé na Oh, samay, thiay, thiay Mba dou délo Avance Sa température monté na Allo bébé Antan nguama Mes caprices Xalé bi niémé ngama Allo bébé Antan nguama Mes caprices Xalé bi niémé ngama Yafi degu Daly Fa diari ndary Yafi degu Daly Fa diari ndary Yafi degu Daly Fa diari ndary Yafi degu Daly Fa diari ndary Ma deff sama CHOIX? Lady lady kay ma wahla Taneu ngua ki guen ci yow for life Lady lady kay may sa Seytané Lingu fi wah yeup Dégue nala Ndah meunone na comis sa place Bandit bu diantal meuno Sage Bébé Goudi mba dou jeh Deugu Ndat sah Sa température monté na Mba nob nguama Xalé bi dépasséma Allo bébé Antan nguama Mba nob nguama Xalé bi dépasséma Allo bébé Antan nguama Yafi degu Daly Fa diari ndary Yafi degu Daly Fa diari ndary Yafi degu Daly Fa diari ndary Jeul na Lima mom Jeul na Lima mom Jeul na Lima mom Wiri wiri jari ndari Jeul na Lima mom Jeul na Lima mom Waly Lingua mom Wiri wiri jari ndari Degu Nguama Mba nob ngama Walé bi dépasséma Fa diari ndary Yafi degu Daly Fa diari ndary Yafi degu Daly Fa diari ndary Yafi degu Daly Fa diari ndary Yafi degu Daly Fa diari ndary

更多 Wally B. Seck

Wally B. Seck →

相关歌词