Entre Nous
WO

Entre Nous 歌词

流派World Music
原文语言WO
浏览量1.2K
Aa阅读设置
文字大小 18

原文歌词

WO
暂时没有翻译,当前显示原文歌词。
Dof ci yaw bu mu tax ba nga foog ni Soo toppee sa taar dina la jaay Nekkal nit moo gën ngay foog ni Entre nous, si on se disait la vérité Tu sauras que nul n'est épargné Gis nga mbëggeel, xoolul mag, xoolul ndaw Tu sauras que nul n'est épargné Dof ci yaw ba mu tax ba nga foog ni (Mënuma la bàyyi) Soo toppee sa taar dina la jaay (Ba nga foog doo daanu) Nekkal nit moo gën ngay foog ni (Mënuma la wan gannaaw) Entre nous, si on se disait la vérité Tu sauras que nul n'est épargné Gis nga mbëggeel, xoolul mag, xoolul ndaw Tu sauras que nul n'est épargné Dof ci yaw ba mu tax ba nga foog ni (Mënuma la bàyyi) Soo toppee sa taar dina la jaay (Ba nga foog doo daanu) Nekkal nit moo gën ngay foog ni (Mënuma la wan gannaaw) Chaque jour, maa ngi ñaan Yàlla suñu boroom Nga déllusi dellusiwaat ci samay loxo Gis nga mbëggeel, xoolul mag, xoolul ndaw Tu sauras que nulle n'est épargné Koo fi mëna am! Ak loo fi mëna doon Mbëggeel aka bari doole Soo ko xoolee ba ci biir, yaw yaay! Wuy bàyyee - ma waay! Séet la la yénnewoon Wala séy ci Aaaah, soo ma bëggoon doo ma def lii Ba may gis keneen waawaaw Soo ma bëggoon doo ma def lii Gis nga léegi nu ma mel ci yaw Nob naa keneen, gis naa keneen Sa jikko moo waral, waral Mbër mi dafa ñëw dimanche Yaayam ñaanal ko Bay ba ñaanal ko Sëriñ ci ñaanal ko Yaa ma saagaane ma dem Soo ma wayadi loo ma dem Dama dof ci yaw nañ ko xam Man yaa ma saagaane ma dem Soo ma wayadi loo ma dem Dama dof ci yaw nañ ko xam Mbër bu dékke daane Fatima A guest ma waay!

更多 Wally B. Seck

Wally B. Seck →

相关歌词