Al Xayri
WO

Al Xayri 가사

장르Afrobeats
원문 언어WO
조회수15
Aa읽기 설정
글자 크기 18

원문 가사

WO
번역이 아직 없습니다. 원문 가사를 표시합니다.
Ñaar ñu Yàlla boole Dox ci yoonu ngëm la Bu sëy bi doré Bul bàyyi sa nawle génn la Li may yëg sama xol neex na loolu Yaw boroom kër nga léegi Jabar loo ko mën xel daf ci tollu Ngeen boole mbégté ak mettit Sa jabar munul yam ak kenn Jubóolel bul di nëbboo Na la miin ngeen xaritoo Sëy bu amul respect du lénn Ba lay neex jàmm am Kat yërmande tuut su kenn ju mé Ngeen di jàppalante itam Boole seen doole sa su ne, hei! Benn xol ak xel Tay diisóo, délen waxtan ci tey Am këru mbëggeel Am këru mbëggeel Ngeen dundu àljana! Ñaar ñu Yàlla boole Dox ci yoonu ngëm la Bu sëy bi doré Bul bàyyi sa nawle génn la (eh!) Négu sëy de manul xatt su xol yi booloo Jàmm ak yar ci la la séyloo Dél muñ domm Jabar wet sa jëkër du la waññil Xecco bi mooy indi gañe Su ngeen digluwante Du ngeen di réeroo Woolu wanté séy xaléy réeroo Waaye mbëggeel lay doré Ngir ànd bi sore, faw kenn baña rëy Di kaf seen biir di foo di ree Ba lay neex jàmm am Kat yërmande tuut su kenn ju mé Ngeen di jàppalante itam Boole seen doole sa su ne, hei! Benn xol ak xel Tay diisóo, délen waxtan ci tey Am këru mbëggeel Am këru mbëggeel Ngeen dundu àljana! Du sey bi doré Bul bàyyi sa nawlé génn la

Maabo의 다른 곡

Maabo →

관련 가사