Kuma Nop
WO

Kuma Nop 가사

장르Afrobeats
원문 언어WO
조회수13
Aa읽기 설정
글자 크기 18

원문 가사

WO
번역이 아직 없습니다. 원문 가사를 표시합니다.
Ku ma nob, laaj ma ku ma nob Sama saajoobaan Ku ma nob, laajleen ma ku ma nob man Sama saajoobaan Su ma doon orchestre, mooy sama guitar bass Yaw yaa tax sol dal neex, yaay sama kawas yeh Sama saajoobaan! Yaw laay woo wuyu ma waruñu di réero Waxal ak man te nga ree Wax ma ku la tooñ bëgguma ku lay merloo Waxal ak man te nga ree Sa kanam bi nga fas ni ñemetuma la ni Maay wax ngay biñ, di ma xeloo ni Amatuloo sama kersa yaw mi (déedéet) Lu fi jaar ba nga bëgg mel ni (fokk ma mel ni) Wax ma lu la dal ba nga may tontu ni (lépp ci yaw la) Kon ma lay merloo ni Li nga fokk la, laaj ma lu ma naam (loo naam wax ma) Fi ma tollu ni, maa ngi sama oh là là! Man jekk piir, wax ma loo fi manqué Fi maay First Lady, kenn du ma jamm na ne Iyo, iyo Waaaw Iyo, iyo Yaa di sama saajoobaan Iyo, iyo Yaay ki may motelee Iyo, iyo Ku ma nob, laaj ma ku ma nob Sama saajoobaan Ku ma nob, laajleen ma ku ma nob man Sama saajoobaan Su ma doon orchestre, mooy sama guitar bass Yaw yaa tax sol dal neex, yaay sama kawas yeh Sama saajoobaan! Yaw lan la, sonn naa léegi may ma Demetul noonu mak yaw Wowowowoy bàyyi ma Mettiwoon na te demuma Lépp laa muñ ca ba muy metti Dimbali ma, wax ma lu la yëkkëti Wuyoooy, bàyyi ma! Ñaareel nga fi bëgg takk Waxoo fi dara lu leer ñaareel nga fi bëgg takk, hey! Niarél ngafi bëgg takk Waxofi dara lu lerr nirél ngafi bëgg takk hey Li nga fokk la, laaj ma lu ma naam (loo naam wax ma) Fi ma tollu ni, maa ngi sama oh là là! Man jekk piir, wax ma loo fi manqué Fi maay First Lady, kenn du ma jamm na ne Iyo, iyo Waaaw Iyo, iyo Yaa di sama saajoobaan Iyo, iyo Yaay ki may motelee Iyo, iyo Ku ma nob, laaj ma ku ma nob Sama saajoobaan Ku ma nob, laajleen ma ku ma nob man Sama saajoobaan Su ma doon orchestre, mooy sama guitar bass Yaw yaa tax sol dal neex, yaay sama kawas yeh Sama saajoobaan! Ku ma nob, laaj ma ku ma nob Laajleen ma ku ma nob man

Maabo의 다른 곡

Maabo →

관련 가사