Yako Waral
WO

Yako Waral 가사

장르Afrobeats
원문 언어WO
조회수40
Aa읽기 설정
글자 크기 18

원문 가사

WO
번역이 아직 없습니다. 원문 가사를 표시합니다.
Ma way Maabo Maabo Ma way Maabo Maabo Héy, xoolal ma kaw ba suuf Maa leen dàq solu fuuf Baby bul di jaawale Du bare yére mooy sañse Xool ma, fu ma mën a gën a nga ne file Xam nga, du ci yére yi ci man mi la Xool ma ni ma trois pièces jàppe Te duma Djiby Dramé! Damay jëm maak di dellu xale Yaw foo may jëlëtee Su ma neexee Obasanjo Def classe teg châpeau Kaay jël ay photo Lii yépp yaa ko waral Guissé Maabo Eh yaw xale bile Ni ngay solu de neex na ma Oooh, sa doxin bi neex na ma Yeah, ni ngay solu de neex na ma Oooh, sa doxin bi neex na ma! (Ñu dem) Kon nañu dem 'cakas cakas' (Cëm, he!) 'Cakas cakas' Dara duñu téye, 'cakas cakas' 'Cakas cakas' (Ay way!) Nañu dem 'cakas cakas' (hannn) 'Cakas cakas' Dara duñu te 'cakas cakas' Ñun dara du ñu tere dem! Balaa ma dugg école Ci laa am classe Maa nekk ci sa xol Ndax dama am cas Baby, xool ma Duma moroomu gone Bés bi tay la Dinaa la wan fi ma mëne Di solu ni mannequin Jëkk ni jëkk, di daagu ni diriyaanke Musóoru ni Diouma Dieng Te fu ma tasee sama cheveux doon sa Beyoncé Kaay jege ma ñu snap selfie Kaay ñu jël ay photo Àdduna yépp gis ko! Lii yaa ko waral Guissé Maabo Eh yaw xale bile Ni ngay solu de neex na ma Oooh, sa doxin bi neex na ma Yeah, ni ngay solu de neex na ma Oooh, sa doxin bi neex na ma! (Ñu dem) Kon nañu dem 'cakas cakas' (Cëm, he!) 'Cakas cakas' Dara duñu téye, 'cakas cakas' 'Cakas cakas' (Ay way!) Nañu dem 'cakas cakas' (hannn) 'Cakas cakas' Dara duñu te 'cakas cakas' Ñun dara du ñu tere dem! 'Cakas cakas' Yaw sama jigéen 'Cakas cakas' Danga am classe, bëgg naa ci yaw 'Cakas cakas' Man yaw yaay li ma moom 'Cakas cakas' Wowooooh, Guissé Maabo Ma way Maabo Maabo Ma way Maabo Maabo

Maabo의 다른 곡

Maabo →

관련 가사